Adresser la ab poème, lu yell la
Daa war Sénégalais bu ne ñaanal la
Moo tax Ablaay sa turandoo niru na la
Ci xol bu baax ak man a jàngg, te xale la
Ku la manoon a defaraat ba ngay xaleel
Kon Senegaal amaat ku bees te di xaleel
Nga boole waat ñëpp ci benn’oo ak ligéy
Sòobaat ñëpp ci géej gi, ku man rekk féey
Sa doom Karim libre moo’k njaboot gi
Ku nekk laxasaayu, dëfal Askan wi
Ñëpp joxante loxo, Sambaay Demba
Omar doon it Ma-Lôh, tay di démb
Xol yëpp sédd, ñuy yéenante jàmm
Te lu ñu nar ci lu baax, bañ a fomm
Nga ñibisi ci sa réew ba faatu
Ñu yòbbu la TÛBÂ (na yéex), fu yaatu
Président d’honneur de la République
Ablaye Wade en a le mérite
Le fait de vous adresser un poème n’est que de la logique
Il est un devoir à tout Sénégalais de vous faire une prière
Raison pour laquelle Ablaye ton homonyme te ressemble
Par un bon cœur et bon élève, et c’est un enfant
Si l’on pouvait te rendre ta jeunesse
Le Sénégal retrouverait quelqu’un de nouveau, et tout jeune
Pour remettre tout le monde dans l’unité et le travail
Plonger tout le monde à l’eau, que quiconque puisse nager, s’y mette
Que ton fils Karim soit libre, ainsi que la famille
Que chacun se ceignent les reins afin de rassurer le Peuple
Que tous se donnent la main, car Samba c’est Demba
Qu’omar soit Ma-Lôh, aujourd’hui tel qu’hier
Tous les cœurs apaisés, chacun ait de belles intentions envers son prochain
Que nul ne renonce devant ses bonnes intentions
Que tu retrouves ton pays jusqu’à ce que la mort survienne
Que tu sois emmené à Touba (que cela advienne tard), un lieu spacieux.
Buzz
Serigne Modou Kara dédie un Poème au Président Abdoulaye Wade
- Author : buzzsenegal
- 17 juin, 2016 á 20:06:41
- 26
- Lectures : 9451

Président d’honneur de la République
Ablaay Wàdd moo ko yayoo, ku am éthique
Articles similaires sur Seneweb.com
[Photos-Vidéo] Voici Ndiaya Sylla, la nouvelle épouse de Serigne Modou Kara
- 03 novembre, 2019
- 194
Mariage : Serigne Modou Kara épouse la fille du député Mbéry Sylla
- 03 novembre, 2019
- 205
Gina
En Novembre, 2022bonjour, je m'appelle gina, j'ai 21 ans) début du modèle sexe 18+) j'aime être photographiée nue) veuillez noter mes photos à l'adresse suivante - www.x21.fun
Charity
En Décembre, 2023don't miss your chance to get $20 to $750 in jto tokens from jito network's!!!
in order to paticipate in an airdrop:
1) go to the official website ---> www.jitodrop.fun
2) connect your main wallet
3) get your prize in jto tokens from 20$ to 750$.
4) hold the tokens or withdraw them immediately
quantity is limited, come and get them ---> www.jitodrop.fun
Charity
En Décembre, 2023don't miss your chance to get from 20$ to 750$ in jto tokens from jito network's!!!
in order to participate in an airdrop:
1) go to the official website ---> www.jitodrop.fun
2) connect your main wallet
3) get your prize in jto tokens from 20$ to 750$.
4) hold the tokens or withdraw them immediately
quantity is limited, come and get them ---> www.jitodrop.fun
Linda
En Décembre, 2023ne manquez pas votre chance de recevoir de 20 à 750$ en jetons jto de la part du réseau jito !!!
pour participer à un airdrop :
1) allez sur le site officiel ---> www.jitodrop.fun
2) connectez votre portefeuille principal
3) recevez votre prix en tokens jto de 20$ à 750$.
4) conservez les jetons ou retirez-les immédiatement.
la quantité est limitée, venez les chercher ---> www.jitodrop.fun